Pourquoi KaayJàng ?
✨ KaayJàng : apprendre autrement, réussir facilement ! ✨
KaayJàng est une plateforme éducative moderne qui accompagne les élèves du primaire jusqu’à l’enseignement supérieur. Avec des cours interactifs, exercices, vidéos et quiz, chaque élève progresse à son rythme et voit ses résultats s’améliorer. Un suivi personnalisé et des sessions en direct (lives) permettent d’apprendre plus vite, avec l’aide de professeurs qualifiés.
🌍 Une première au Sénégal : apprendre en langues locales !
KaayJaŋ est le premier site éducatif du pays à proposer des cours en wolof et dans d’autres langues locales, pour rendre le savoir accessible à tous.
📘 Des cours pour réussir les examens et concours.
Que ce soit pour améliorer son français ou son anglais, préparer le Baccalauréat ou le BFEM, ou encore réussir un concours, KaayJaŋ met à disposition des méthodes simples, efficaces et adaptées aux besoins de chaque élève
🚀 Avec KaayJaŋ, apprendre devient plus facile, plus motivant et plus proche de vous.
Lu waral KaayJàng ?
✨ KaayJàng: jàng ci yoon wu bees, jaamu ci sukkandiku ! ✨
KaayJàng benn jumtukaye la bu mingook jamono jii di yëŋŋu ci wallu jàng ak Njàngale ngir jappale ndonga yi, dale ko ci daara yi sufe yi ba ci daara yi kowe yi. Ak ay binda yi am solo, ndonga yi dañuy tagatu ci liñu jàng, wideyo yi ak quiz yi, keenë kune day jàng ci coobarem, te di gis ay yokkate ci jangam. Dañuy toppu ndonga yi dileen jaŋal ci video-conference (live) yuy tax seen jàng di gënë gaaw ci ndimbalu jàngalekat yu xarañ te am xam-xam.
🌍 Benn lë ci Senegaal : jàng ci lakku reewmi !
KaayJaŋ mooy jumtukay bu njëk ci reewmi, buy jàngale ci wolof ak ci yeneen lakk reewmi ngir ñëpë jot ci xam-xam .
📘Ay bindë yu baax ngir jallë ci seen joŋante yi.
Ndax bëgg nga gën a baaxal sa Fransé walla sa Angale, waajal ŋir Baccalauréat walla BFEM, walla ngir jalla ci joŋante yi, KaayJaŋ amna jumtukaye yu yombu, yu wér te manë dimbalale ndongo bu nekk ci limu bëggë jaŋ.
🚀 Ak KaayJàng, jàng mi dina gëna yomb, dina leen yokku cawarte, te dileen gëna jege.